Universal Declaration of Human Rights - Wolof
Content Category
Wolof
BATAAXAL GU MAG GI ËMB SAÑ-SAÑI DOOMI AADAMA [Preamble] Ñu jàpp te nangu ne sagu doomi aadama ak sañ-sañam yépp-dañu yam te kenn mënukóo jalgati, te lu lépp nekk na cës laay ci taxufeex ci mbirum àtte...