Universal Declaration of Human Rights - Bantawa rai Content Category Universal Declaration of Human Rights Bantawa rai
Universal Declaration of Human Rights - Wolof Content Category Universal Declaration of Human Rights Wolof BATAAXAL GU MAG GI ËMB SAÑ-SAÑI DOOMI AADAMA [Preamble] Ñu jàpp te nangu ne sagu doomi aadama ak sañ-sañam yépp-dañu yam te kenn mënukóo jalgati, te lu lépp nekk na cës laay ci taxufeex ci mbirum àtte...